Publicité

Mia Guisse – Gauche & Droite (Clip Officiel)

Mia Guisse – Gauche & Droite (Clip Officiel)

** Lyrics de la chanson GAUCHE & DROITE ** Yaw la Yaw la Yaw la yéné sama xol ndakh damala love

Publicité

té sakh kafou ma ci Dama sensible deug la Dama feel beug la diokh Sama xol bi ndakh damala Khalé bi té mala diokh Sama xol bi Ndakh damala love Damalakay diokh, damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane chéri ba nopi sopi sama sant

Damalakay diokh damalakoy diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane Yalla ko def lolou louma thi meun anh eh Han man, han hawma lanela Ma ngui doundou love story bouma yéém Boulma laadj louma dal nii Sama nobél amoul foumou yam Khalébi soma laadjone jant bi, non tey dou fanane Khalébi soma laadjone sama bakane,

damalakay diokh Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane chéri ba nopi sopi sama sant Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane Yalla ko def lolou louma thi meun anh eh Gauche wala droite? Dis moi si tu veux en haut en bas ?

A lire sur Téléweb :  Sabel Dieng n'est plus un cœur à prendre : Ici quelques clichés de son beau mariage (Photo)

Dis moi Lou tang wala lou sééd? Dis moi ma servir la Bou 19h dioté gnou teudi Na metti, na yaag, na melni Khalébi boul ragal na nga yekssi Gnoune kessé la thi keurgui na djoly My babe touch my body ouh !!! Everyday ma diokhla nga né thi Khalébi tekk ma lou metti Bou yékhé thi yaw la No no dou thi man han yayayay Han man,

han hawma lanela Ma ngui doundou love story bouma yéém Boulma laadj louma dal nii Sama nobél amoul foumou yam Khalébi soma laadjone jant bi, non tey dou fanane Khalébi soma laadjone sama bakane, damalakay diokh Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane chéri ba nopi sopi sama sant

Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane Yalla ko def lolou louma thi meun Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane chéri ba nopi sopi sama sant

Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane Yalla ko def lolou louma thi meun anh yeah Oh yeaah ! oh yeah Ndéké khalébi rek laa nop Mane khalébi rek la nop Oh yeaah ! oh yeah Ndéké khalébi rek laa nop Mane khalébi rek la nop ba sagar khégne

A lire sur Téléweb :  Binette et Moussa Faye : « Sama fiir foko nateu wessounako ndakh… » (Vidéo)

Laisser une réponse

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *